mardi 6 janvier 2009

Gordjiguéne

Li nak c l'histoire d'un gordjigene ndeysane. Ben jour mou decider dey toub,bayi you bone yeup yi mou done def, dem Hadj Macca. Nieup beg, contane sidecision eum bi. Mou daldi dem Macca, dem ba fi nityi di niane, daldifarankoulaye, jaap, jouli niar raka, tallal aye lokhom, fasyener niane :"Djibril yaw, waxal mame yAllah mangui key niane mou mey ma aye kawarr yougoudouuu, aye weh you goudouu t di briller, mou mey ma aye ween 80D youreuy..." ben pelerin rombe ko daldi taxaw neko: yaw ya niak jom deug, nieuwba macca, wara toub, ngey niane sa yeuf gordjigene yi, ragalal yAllah!"Gordjigene bi daldi siggui xoll ko, khelouuu ko, suuuuuperrr tchipatouuudaldi tourner wat concentrer talal lokho egali "Eh Djibril yaw?.... ak toutihaaaaannnche

1 commentaire:

  1. Play at the Best Merit Casino | Casino in California
    The deccasino Merit Casino Resort Spa & Casino is the premier destination in the San worrione Diego County region and home to a full-service spa, salon, and fitness center. 메리트 카지노 고객센터

    RépondreSupprimer