mardi 6 janvier 2009
serigne bi
bi nak benn waye la wonn mou demm néé déye djébeulou si serigne khabane prnek talibém . beuss nak serigne khabane né dafaye toukki andakh wadji baparé yann wadji aye bagages you diss . wadji dokh commencé sonn néko "wasang bou tedd bi egg nagnou", serigne bi neko "dédéte lisi dess bariwoul".wadji dokhat lou bari akh bagages yi ni watt "serigne khabane fignou djeumsorrineu" serigne bi neko watt "dédétt légui gnou egg"wadji dokhatt néko"wa mais khabane fann lagne djeum nak gayne "serignebinéko watt "sorriwoul légui gnou egg".wadji dokhatt lou beuri niko" eh khab's fougnou gnap ndeyama djeum nak
Inscription à :
Publier les commentaires (Atom)
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire